05/09/2026
Le GLS, c’est bien plus qu’une conférence.
Bien plus qu’une simple rencontre.
C’est un déclic. ✨
Un enseignement qui a changé des vies, transformé des mentalités et redéfini la vision du leadership de nombreuses personnes.
Et si cette année, le prochain déclic était le tien ?
📅 Les 06 & 07 novembre 2026, rejoins-nous pour vivre le GLS et changer ta vision du leadership.
Parce qu’une rencontre peut t’inspirer.
Mais un déclic peut changer toute une vie🔥
📲 Plus d'info: +221 77 397 18 52 / +221 70 354 19 65
———————————————————————
GLS, lu romb ab lël la.
Lu romb ab ndaje la.
Ab xippi la.✨
Ab njàngale bu soppi ay dund, soppi ay xalaat te dafa yeesalaat gis gisu Kiliftéef ci nit ñu bari.
Su at bii nekkoon at bi ngay dund sa xippi nag?
🗓️06 ak 07 nowambar 2026,
Fekkisi ñu ngir dund GLS bi te nga soppi sa gis gisu Kiliftéef.
Ndaxte ab ndaje mënala xelal waaye ab xippi mëna soppi dund lëm.🔥