25/07/2026
Hommage à nos mamans.
Képp ku sa yaay génn na aduna, ñaanal ko Yàlla.
Yàlla na ko Yërëm, baal ko ay bàkkaaram, te tàbbi ko Aljana Firdawsi.
Képp ku sa yaay di dund, sàmm ko te teral ko.
Bul ko sonal. Yàlla moo la ko may, te yaay amul wuutu.
Yaay mooy barke, mooy mbëggeel gu dul jeex, mooy ndimbal ci kaw suuf.
Sàmmal sa yaay ndax bu mu demee, du dellusi.
Kou beugue sa yaye partagel ❤️.