03/02/2026
- L'ultimo saluto al caro Severino si terrà giovedì alle 10h30 presso la Chiesa di Popenguine. Chi vorrà accompagnarlo in questo momento di commiato è il benvenuto. Il vostro affetto, anche silenzioso, sarà per noi conforto.
Grazie a tutti.
- Le dernier hommage à notre cher Severino aura lieu jeudi à 10h30 à l’Eglise de Popenguine. Toutes les personnes qui souhaiteront l’accompagner en ce moment d’adieu seront les bienvenues.
Votre affection, même silencieuse, sera pour nous un grand réconfort.
Merci à tous.
- Ñuy leen xamle ne tagato bou mujj bi ak sunu Severino dina am altine, waxtu 10h30, ci Eglisu Popenguine. Ku nekk ku ci bëgg ñëw ci jamono bi gnu key denthie ak defal niane bi mujj, di nagnou leen fa dalal ak jaam . Mbëggeel gi ngeen am ci mom , meme soude dou lougnouy wax, dina nekk sunu ndimbël.
Jërëjëf ñépp.