TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI

TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI TAKKU défar Darou Mouhty"
Est une association créée par des talibés et des sopés de Borom Darou soucieux de la situation sociale, pédagogique, sanitaire etc..

de ladite Ville

10/03/2026


TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI

25/02/2026

Ndaysaan 😥
Sëriñ Mbàkke Daba Sarr
Ibn Sëriñ Abdourahmane Mbàkke
Ibn Boroom Daarul Muhti

Sunu boroom teeru ko ci yërmàndeem Barkeb seexul xadiim ak boroom Daarul Muhti 🤲😥

𝐓𝐀𝐊𝐊𝐔 𝐃𝐄𝐅𝐀𝐑 𝐃𝐀𝐑𝐎𝐔 𝐌𝐎𝐔𝐇𝐓𝐘𝐒𝐨𝐜𝐢𝐚𝐥 𝐑𝐚𝐦𝐚𝐝𝐚𝐧𝐞 2️⃣0️⃣2️⃣6️⃣🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢WAVE / ORANGE MONE👇 👇👇👇 👇  👇👇👇👇7️⃣7️⃣  2️⃣8️⃣8️⃣ 5️⃣0️...
23/02/2026

𝐓𝐀𝐊𝐊𝐔 𝐃𝐄𝐅𝐀𝐑 𝐃𝐀𝐑𝐎𝐔 𝐌𝐎𝐔𝐇𝐓𝐘
𝐒𝐨𝐜𝐢𝐚𝐥 𝐑𝐚𝐦𝐚𝐝𝐚𝐧𝐞 2️⃣0️⃣2️⃣6️⃣

🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢

WAVE / ORANGE MONE
👇 👇👇👇 👇 👇👇👇👇
7️⃣7️⃣ 2️⃣8️⃣8️⃣ 5️⃣0️⃣ 5️⃣9️⃣

Kuréelug TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI, niñu ko baaxoo defee àtt mu nékk ci wéeru koor wi,

Dajale ay ndimbal ngir baaxe ko way néew-doole yi,

Noonu lañu ko fas yéenee defewaatee ci àtt mii Insàllaa.

Ñu dici woo ñépp ñu tàbbal ci séen alal, mooxam ceéb la, wala diwlin, wala suukar, wala xaalis, ak lépp luñu mana jëfandikoo rekk.

Dimbalante baaxna ci jamono ju ne, rawatina ci wéeru Koor.

Sunu boroom nangul ko, barkeb boroom daarul Muhti 🤲

🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

𝐓𝐀𝐊𝐊𝐔 𝐃𝐄𝐅𝐀𝐑 𝐃𝐀𝐑𝐎𝐔 𝐌𝐎𝐔𝐇𝐓𝐘𝐒𝐨𝐜𝐢𝐚𝐥 𝐑𝐚𝐦𝐚𝐝𝐚𝐧𝐞 2️⃣0️⃣2️⃣6️⃣🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢WAVE / ORANGE MONE👇 👇👇👇 👇  👇👇👇👇7️⃣7️⃣  2️⃣8️⃣8️⃣ 5️⃣...
11/02/2026

𝐓𝐀𝐊𝐊𝐔 𝐃𝐄𝐅𝐀𝐑 𝐃𝐀𝐑𝐎𝐔 𝐌𝐎𝐔𝐇𝐓𝐘
𝐒𝐨𝐜𝐢𝐚𝐥 𝐑𝐚𝐦𝐚𝐝𝐚𝐧𝐞 2️⃣0️⃣2️⃣6️⃣

🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢🟢

WAVE / ORANGE MONE
👇 👇👇👇 👇 👇👇👇👇
7️⃣7️⃣ 2️⃣8️⃣8️⃣ 5️⃣0️⃣ 5️⃣9️⃣

Kuréelug TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI , niñu ko baaxoo defee àtt mu nékk ci wéeru koor wi,

Dajale ay ndimbal ngir baaxe ko way néew-doole yi,

Noonu lañu ko fas yéenee defewaatee ci àtt mii Insàllaa.

Ñu dici woo ñépp ñu tàbbal ci séen alal, mooxam ceéb la, wala diwlin, wala suukar, wala xaalis, ak lépp luñu mana jëfandikoo rekk.

Dimbalante baaxna ci jamono ju ne, rawatina ci wéeru Koor.

Sunu boroom nangul ko, barkeb boroom daarul Muhti 🤲

🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

1er Album, la conférence du Magal Darou Mouhty Organisée par le comité d'organisation en collaboration avec le Kourel TA...
02/02/2026

1er Album, la conférence du Magal Darou Mouhty
Organisée par le comité d'organisation en collaboration avec le Kourel TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI

Cp : Machigue Production

02/02/2026

Conference religieux Waajal màggal Daarul Muhti ❤️

01/02/2026

Sous l'égide du Khalif de Mame Thierno Ibrahima Faty , SERIGNE KHALID MBACKÉ,
le Comité d'organisation du Grand Magal de Daroul Mouhty, en collaboration avec le Kurel TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI vous convie à la conférence qu'il organise le Dimanche 01 Février 2026 à Darou Mouhty.

Conférenciers : Dr Mor Talla Cissé, Serigne Khalil Mbacké Moustapha Absa.

Théme: "Kun Kaatiman,source d'inspiration pour l'éducation aux valeurs islamiques".

Lieu : Esplanade de Grande Mosquée de DAROU MOUHTY.

Heure: 21h:00mn

01/02/2026

دعوة خاصة.

إلى حضرة السيد / السيدة.

السلام عليكم ورحمة الله تعالى وبركاته.

تحت رعاية سماحة الشيخ / سرين خالد امباكي إبراهيم فاط، خليفة دار المعطي

"وبالتعاون مع "جمعية خدمة دار المعطي"، TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI

تنظم اللجنة الثقافية بمناسبة الاحتفال بمغال دار المعطي محاضرة بعنوان
"دراسة قصيدة: كن كاتمًا – كمصدر إلهام للتربية على القيم الإسلامية."

وتتشرف اللجنة الثقافية بتوجيه هذه الدعوة الخاصة إلى سعادتكم لحضور فعاليات هذه المحاضرة الهامة.

المحاضر: الأستاذ الدكتور / مور تال سيسي
المعلّق ومدير الجلسة: الشيخ / خالد امباكي مصطفى حفصة

التاريخ: 01 شباط / فبراير 2026م
الساعة: التاسعة ليلاً (21H00)

المكان: الساحة المتواجدة غربي المسجد الجامع

حضوركم شرف لنا

01/02/2026
27/01/2026

Appel Grande Conférence Magal de Daroul Mouhty 2026.

Conférencier : Dr Mor Talla Cissé.
Intervenant : Serigne Khalid Mbacké Moustapha Absa.

Thème :Kun Kaatiman, source d'inspiration aux valeurs islamiques.

Dimanche le 01 Février 2026.
En Face de la grande mosqué.
Heures : 21heure.

Adresse

Darou-Mousty

Téléphone

+221774494716

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque TAKKU DÉFAR DAROU MUHTI publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager