Sama Dieukeur Sama Kharite - Mon Mari Ma Moitié

Sama Dieukeur Sama Kharite - Mon Mari Ma Moitié Waakhtan bou rafett entre goor ak jiguen si leup louy deffar souniou vie de couple si diam ak soutoura.

Ce page dédiée à la femme Sénégalaise veut raffermir les liens de mariages.

En ano stpSlm je voulais des conseils mane sama keur sokhna la nek depuis 3ans dama ame ben xalé bouma nekal yagu naniou...
25/02/2025

En ano stp
Slm je voulais des conseils mane sama keur sokhna la nek depuis 3ans dama ame ben xalé bouma nekal yagu naniou touti mane ak mom te damako beug def 2em femme ma waxko sama sokhna mounima soko take fokoy dougeul maniko damay dieul nek mouni ma so dieule nek dina wax sama pape mou geunee niou ndax yaw yoro dara niou fat laa 3ans amo loy def di yok sa bop thiono te wax deug yalla khale bii danio nobanete te mom mane rek lay har te mane yor na loumako tekeeee may sakou sen xalat merci à vous

Salam les amies j'écris sur le compte d'une sœur pour ne pas être reconnue bon suis une jeune fille de 25 ans g un blm d...
23/12/2024

Salam les amies j'écris sur le compte d'une sœur pour ne pas être reconnue bon suis une jeune fille de 25 ans g un blm d'oreille maname j'entends avk l'une l'autre mom le médecin dit k appareil mossiy bax pour mayko touti volume et g po la somme demandée cependant ma bgue guènn nianal ma yalla mayma tanè parceque kènn xamoul bane niane la yalla di nangou sa me hante sa m'empêche d'être mm en relation y'avait un homme qui prétendait m'aimer il est venu ici maintes fois biniou ko expliquer cas bènn yone lafi niewatt si lagn geudj dègg sii kouni diabar gua bguone guiss na lounè mè takhoul ma perdre confiance en moi nianal lènn ma yalla defal ma tanè com avant ndakh bgue na am Borom keur cette nouvelle année inch'Allah g mes raisons mdr bguouma moy yalla merci de me laisser vos prières diam si nieup 👋❤voilà lii moy sam blm admin merci

Bonjour admin, je vous écris ndax problème xol bima am té je ne sais pas quoi faire En faite je suis une jeune femme de ...
04/12/2024

Bonjour admin, je vous écris ndax problème xol bima am té je ne sais pas quoi faire
En faite je suis une jeune femme de 26, après plus de 20 ans de mariage mes parents se sont divorcés avec 10 enfants sunu papa dafa daw responsabilité wam,lidieunti wounu bobu j'avais 15 ans et je suis la 4iem,donc sama yaye monékone sunu leep mom rk lanu guissone bilahi dou mbok dou kén ,gnouy goorgorlu di diok ak danu ba legui gningui si lolu, mais mon problème c'est ma mère,xamé toumako bilahi je veux pas la jugé, elle s'est remarié Alhamdoulila,mais j'ai découvert que elle a des amants (soubhanallah) instant bi legui ma dof,ma petite sœur ne la respecte pas lolu metima,je me demande pourquoi elle parle comme ça à ma mère,ndékété elle a vu une conversation d'elle et un homme ay wax you bone ak stickers ay vidéo p***o, ay way, j'ai eu la curiosité de découvrir,mais li ming yakh sama aduna bilahi,ma grande sœur le sais aussi,mane ak sama mak dano moudié déménagé bayyiko ak xaleyi ,gnokoy fayal fimou deuk et tout pourtant gnoune dano am caractère,mais dama rouss sakh ande ak sama yaye si mbed bi,ndax mingui beurek payi,je l'a reconnais plus,ma mère était très brave et pieux, elle a 53 ans nangotoul sakh ligueye,dieundeul nako frigo,mais douci def dara,je pense que je suis dépressif ndax louné lay xalate nane la wara def et j'ai pas le courage de l'affronter,mais li xalatou mako wax kén,domam yeup xamnagn ko mais dano dem ba diepi ko té ay dome yu jiguen rk la am,ma petite sœur de 16 ans commence déjà à dormir dehors tiite na,nane la wara def
Désolé pour la longueur

Adresse

Dakar
@SDSKMM4,7(2175AVIS)

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sama Dieukeur Sama Kharite - Mon Mari Ma Moitié publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L’organisation

Envoyer un message à Sama Dieukeur Sama Kharite - Mon Mari Ma Moitié:

Partager