23/05/2025
Bayyinaango : ngonan-ɗen ko dawrugol ɗemɗe ngol joñaani hay ɗemngal gootal, gaddotoongol mahondiral renndo e keewal pine nder Muritani.
Jokkorde Pelle pinal – renndinnde Fedde Ɓamtaare Pulaar he Muritani (FƁPM), e Fedde Ɓamtaare Ɗemngal e Pinal Sooninke (AMPLCS) e Fedde Ɓamtaare Ɗemngal Wolof (APROLAWO) – ine wondi e ngoƴa mawka sabu yeewtere faatunde e darnde ɗemɗe he Muritani.
Waɗi noon, ko won ɗiin miijooji e hujjaaji kaaleteeɗi ine mbaawi bonnande hakkeeji pinal e ɗemngal Muritaninaaɓe heewɓe. Aɗi mbaawi ɓeydaade leefnude mahondiral renndo, nder leydi nganndiraandi keewal ɗemɗe e pine.
Yanti heen, ɗiin miijooji keertinooji ine luulndii yiyannde Doosgal leydi Muritani kam e nanondire hakkunde leyɗe ɗe Muritani jeyaa, haa arti noon e :
• Nanondiral UNESCO ngal 2005, paatungal e ndeenka e ɓamtugol keewal pine, baawnowal dowlaaji ɗii wallitde keewal ɗemɗe, e gaddaade kuutoragol ɗemɗe dente ɗee nder jaŋde e jaayɗe e njuɓɓudi laamu ;
• Piɓondiral hakkunde leyɗe paatungal e hakkeeji siwil e politik (kuulal 27), keɓtinanngal demɗe dente ɗee kala hakke « huutoraade ɗemɗe mum en keeriiɗe » ;
• Doosgal Afrik paatungal e hakke aadee e ɓesnguuji (kuulal 17), gaddaningal leñol kala hakkeeji mum pinal e ɗemngal e ƴellitaare mum en.
Ko ɗee jeewte baawɗe jibinde jilɓooje kaaɓniiɗe ngaddani Jokkorde Pelle Pinal ɗaɓɓude dewgol dawrugol ɗemɗe ngol joñaani hay ɗemngal gootal, tuugingol he keɓtingol potal ɗemɗe ngenndiije ɗee kala, ngam teeŋtinde nuunɗal, e kormondiral, e ndimaagu ndenndaangu. Ɗuum noon laatortoo tan ko he :
1. Laawɗinirgol laatingol pulaar e sooninkoore e wolof laawol sariya laaɓtungol, dottowol darnde e lowre e kuutoral heen ɗemngal kala;
2. Jaajtingol jaawngol jaŋde ɗemɗe ngenndiije nder duɗe laamu tokoose ɗee kala, hono no ɓeto BREDA/UNESCO e hitaande 1984, e ngo Jaagordu jaŋde ngenndi e hitaande 1988, mbagginirnoo ɗum nii. Ɗum ɗoo noon ko geɗal teeŋtungal nder compugol jaŋde moƴƴere, nde joñaani hay gooto, jaŋde nuunɗunde ;
3. Ƴellitgol keewal ɗemɗe jahdungol, dokkowol kadi ɗemɗe tumarankooje faayiida – ko wayi no farayseere e engeleere – no ɗemɗe gollorɗe, ɗemɗe janngirɗe, ɗemɗe udditaare he aduna.
Eɗen njenanaa, Muritani waawata mahde ngootaagu ngenndi nduumotoongu tan, ko nde hormii ndimaangu ɗemɗe leƴƴi mum kala. Laawɗinde ɗemɗe ngenndiije ɗee kala, ko heɓtinde potal ɓiyleydaagu Muritaninaaɓe kala.
Ko ɗuum addani Jokkorde Pelle Pinal ɗaɓɓude lelnugol dawrugol ɗemɗe nuunɗungol, ngol joñaani hay ɗemngal gootal, nawrowol yeeso, sibu ko ɗuum tan waawi gaddaade nguurdiigu janngo nduumotoongu, nder deeƴre e mahondiral.
Nuwaasoot, ñalnde 20 mee 2025
Jokkorde Pelle Pinal
------------------------------------------------------------
بيـــــــــــان : من أجل سياسة لغوية شاملة، ضمانا للتماسك الوطني والتنوع الثقافي في موريتانيا
تعبّر تنسيقية الجمعيات الثقافية للغات - المكونة من جمعية ترقية البولارية في موريتانيا، والجمعية الموريتانية لترقية اللغة والثقافة السوننكيين، وجمعية ترقية اللغة الولفية - عن قلقها البالغ إزاء النقاش الذي يشغل الرأي الوطني منذ بعض الوقت حول مكانة اللغات في موريتانيا.
فبعض المواقف والمطالب قد تؤدي إلى الإضرار بالحقوق الثقافية واللغوية لشريحة كبيرة من الموريتانيين، مما قد يزيد من تهديد التماسك الاجتماعي في بلدٍ غني تاريخياً بتنوعه اللغوي والثقافي.
كما أن هذه المواقف الإقصائية تتعارض مع روح الدستور الموريتاني ومع الالتزامات الدولية لبلدنا، لا سيما:
• اتفاقية اليونسكو لعام 2005 حول حماية وتعزيز تنوع أشكال التعبير الثقافي، التي تدعو الدول إلى تشجيع تعدد اللغات وضمان حق استخدام لغات المجموعات في مجالات التعليم والإعلام والإدارة.
• العهد الدولي الخاص بالحقوق المدنية والسياسية (المادة 27)، الذي يعترف للمجموعات اللغوية بحق "استخدام لغتها الخاصة".
• الميثاق الأفريقي لحقوق الإنسان والشعوب (المادة 17)، الذي يضمن لكل شعب الحق في ثقافته ولغته وفي ترقيتهما.
ولمواجهة هذا النقاش - الذي قد يولد تفسيرات وارتباكات مؤسفة – فإننا في تنسيقية الجمعيات الثقافية للغات ندعو إلى سياسة لغوية شاملة تقوم على الاعتراف المتساوي بجميع اللغات الوطنية، بروح من العدالة والاحترام المتبادل والكرامة المشتركة، وهو ما يتطلب عملياً:
1. إضفاء الصفة الرسمية الفعلية على اللغات البولارية والسوننكية والولفية، بقانون واضح يحدد أدوارها ومجالات استخدامها وآليات التنفيذ الملموسة.
2. التعميم السريع للتدريس باللغات الوطنية في المرحلة الأساسية من التعليم، استجابة لما أوصت به تقييمات مكتب اليونسكو الإقليمي للتربية في أفريقيا عام 1984، ووزارة التهذيب الوطني عام 1988، وهو ما يمثل رافعة أساسية لتحقيق تعليم جيد وشامل وعادل.
3. ترقية تعددية لغوية متوازنة تثمن كذلك اللغات الأجنبية - خاصة الفرنسية والإنجليزية - كأدوات للعمل والتعلم والانفتاح على العالم.
ونحن مقتنعون بأن موريتانيا لن تتمكن من بناء وحدة وطنية دائمة إلا باحترام الكرامة اللغوية لكافة مكوناتها، فإضفاء الصفة الرسمية على جميع اللغات الوطنية يعني بالفعل الإقرار بالمواطنة المتساوية لكل الموريتانيين.
لذلك فإن تنسيقية الجمعيات الثقافية تدعو إلى اعتماد سياسة لغوية منصفة وشاملة وتقدمية، ضمانا لمستقبل مشترك وللتماسك الاجتماعي والسلام الدائم.
نواكشوط، 20 مايو 2025
تنسيقية الجمعيات الثقافية
------------------------------------
Dantaxe, kuudo politikin xantoŋondinte ken ga ni tolomanda jamaanen ganbaanaaxun do naame ñaxatindo Moritani noxo.
Naamun kafonun jokkinda xannun da, sigi ti ke moxo ya : Fullun kafo (ARPRIM), Sooninkon kafo (AMPLCS) — Wagadu Saane do Wolofunun kafo (APROLAWORIM).
Jokkinda ke wa i xidimefiibanganten koyini ken ga teqana sefe be ga da jaman sinmaye sigindi i xare ke dinma, fo be ga katta xannun siga moritani.
Killu wutinto yogonu do tirindindu beenu ga bange moxoxerexente da, i wa jogorini besendini katta naamun do xanjoogonun moritaninko jama yogo da.
I wa jogorini jamaanen jamankafonun meeragenme furaaxunu jamaane be taarixun noxo, xannen do naamiñaxitindon xabunton ga a yi. Kun senbendikillu do jamaanen taaxusartinun do jamaanunmeexa xandukinnu beenu jamaanen ga da i wutu, i da me sooxi, kun ga ni :
• Unesco meemukke siine 2005, a ga teŋana tangande do wuruginde ga do ñaxatindon moxokonqun naamun da, a ga jamaanun gansini na xangabe fasonŋuntaaxunu do gaddunde katta xabiilanun xanne xaranqunde, xibaarinde do marande kaara ;
• Jamaanunmeenaxa meemukke katta siwilin do politikin joogonu (sarti 27) Ken ga da xabiilanun xannun joogonun toqondi (i ga munnafane ti i yinmenu xanne) ;
• Afriki sarti be ga katta haadama do jamon joogonu (sarti 17) a ga da jama su naame, xannen do a wuruginden gaddu ;
Ke sefe be ga du saasa, a ga jogori facarindu walaxinto saarana, oku, xannun do naamun kafonun jokkinda, o na do xannun politiki be ga sigi ti jamaanen xannun su ñekkoyen tuyinden ya, kiite, daroye do yerewuraaxu kanma ; ken gan xawa fon saarana :
1. Fulle, Sooninke do Wolofo dagandinde ti kille, a laabanten ga ni, a ga xannu ku siganun xerexerene, i munnafanbaganden da dingiron su do i yaaxabande ;
2. Jamaanen xannun xaranqunden loogonde jewoye maxa xaranrafana xo BREIDA xiimande siine 1984 do jamaanen maranden sandigiran xiimande siine 1988 ga koomandi moxo be. Ken ni tuggaadixottinte ya, marandisire do fooñekkonte da.
3. Xangabiñekkonte wuruginde da, a ga tuŋaarankanxannun fasonŋuntaaxunu (Franse do Angle) xo golliñansurumaadu, xaranqundixannu do duna jokkindanlenmaau.
A xullen wa o da, moritani ra nta jamaanen ganbaanaaxu duumante tagana, a ga ma i jamon xannu i yerewuraaxu ya, na i daro.
Na jamaanen xannun dagandi, ken ya na jamaanen renmaaxun ñekkoyen toŋondini moritaninko su naxa.
Naamun kafonun jokkindan wa xirindini katta xannen politikin ñekkonte, kaanadagante, gaddunda katta jamankafon meeragenmen do deejo duumante.
Nuwasooto, me 20 siine 2025
JOKKINDA
--------------------------------------
Caabal : Làkk wuy boole ñépp, mooy ndëgërlaayu bennoo askan ak wuute ci caada yi ci Móritani
*Mbooloo mbootaayu làkk ak caada yi ëmb mbootaay yii : Mbootaay ngir dundalaat làkkum pulaar ci Móritani (ARPRIM), Mbootaayu Móritani ngir fësal Làkk ak caadaay Sooninke (AMPLCS), ak Mbootaay giy fësal Làkku Wolof (APROWLA)ñoo giy xamle seen njàqare jëm ci kàddu yi fiy jib ci fan yii ci fépp ci biir réew mi aju ci mbirum làkki réew mi te mu yàgg indi jafe-jafe ci xalaatu waa réew mi, ci wàllu làkk yi ci Móritani.
Dëgg la sax, yenn taxawaay yi ak ñaxtu yi mën nañu yàq yelleefi aada ak làkku ñu bari ci doomi Móritani. Loolu mën na gëna nasaqal bennoo gi am ci réew mu bari ay lakk ak cosaan yu wuute ci taarix.
Rax ci dolli, gis-gis yooyu di beddiwaate ñoom seen bopp, méngoo wu ñu ak sàrtu ndayu réewum Móritani ak taxawaay yu mag yi sunu réew jël, rawatina:
• Déggoo bu UNESCO tëral ci atum 2005 ci wàllu aar ak dooleel wuute gi am ci wàllu caada, mooy sàkku ci réew yi ñu gën dooleel làkk yu wuute te fexe ba askan wi mën a jëfandikoo làkk wi ci wàllu njàng, tas xibaar ak liggéey .
• Pasu Àdduna bi ñeel yelleefi siwil ak politik (Ponk 27), muy nangu yelleefi askan ci ñu am sañ-sañu «jëfandikoo seeni làkk.»
• Sartu Afrig ci yelleefi doomi Aadama ak askan yi (ponk 17), mooy aar askan wu nekk seen yelleefu Aada, seen làkk ak seen jëm kanamu làkk.
Bi ñuy càmbare waxtaan wii, mën na jur ay tekki yu bari ak jaxasoo yi ñuy réccu, nun, ñii di mbootaayu Aad ak Cosaan ak Sàmm làkk yi te lëkkaloo , danuy ñaan ñu amal politiku làmmiñal buy boole ñépp, bu ñu sukkandiku ci yamale gëdd làkki réew mi yépp, ci ngëm bu jaar yoon, joxante cër ak bokk ngor. Ci dëgg, loolu dafay tekki ponk yii:
1. ofiselisasioŋ bu jaar yoon ci Pulaar, Sooninke ak Wolof, jaare ko ci yoon wu leer buy leeral seen wareef, seen barabi jëfandikoo ak pexe yu wóor yi ñu leen di jëfandikoo.
2. gën a gaaw ci yamale njàngale ci làkki réew mi ci daara yu njëkk yi, ni ko BREDA/UNESCO digale ci jàngat yi ñu def ci atum 1984, ak ci njëwriñ ji ñu dénk wàllu njàngum réew mi ci atum 1988. Loolu mooy ndëgërlaay bu am solo ngir njàngale mu baax, bu ñépp bokk ci yamale.
3. gën a xëcc làkk yu bari ci anam wu jaar yoon, day jox solo làkk yi — rawatina làkku nasaraan ak angale , muy jumtukaayi liggéey, jàng ak ubbeeku ci àdduna.
Gëm nañu ni Moritani du mëna tabaxu benn yoon bu nara yàgg su joxe cër làkk yi ci bépp yelleef bu ci bokk. Fexe ba làkki réew mi yépp nekk làkk yi ñu daganal,loolu dafay tekki ni doomi Moritani yépp ñoo bokk yam ci réew mi .
Kon koordinaasioŋ bu Mbootaayi Aada yi dafay ñaan ñu taxawal politigu làkk bu jaar yoon, boole ñépp ci mu jëm kanam, muy wóoral ëlëg ci ñu bokk, bennoo ci askan wi ak jàmm ju sax.
Nuaksot, 20 mai 2025
Koordinaasioŋ bi
-------------------------------------
Déclaration : Pour une politique linguistique inclusive, gage de la cohésion nationale et de la diversité culturelle en Mauritanie
La Coordination des Associations culturelles de langues — composée de l’Association pour la Renaissance du Pulaar en Mauritanie (ARPRIM), de l’Association Mauritanienne pour la Promotion de la Langue et de la Culture Sooninke (AMPLCS), et de l’Association pour la Promotion de la Langue Wolof (APROLAWO) — exprime sa vive préoccupation face au débat qui agite depuis quelque temps l’opinion nationale, à propos du statut des langues en Mauritanie.
En effet, certaines prises de position et revendications risquent plutôt de porter atteinte aux droits culturels et linguistiques d’une partie importante de Mauritaniens. Elles pourraient ainsi fragiliser davantage la cohésion sociale d’un pays historiquement riche de sa diversité linguistique et culturelle.
En plus, ces positions exclusivistes vont à l’encontre de l’esprit de la Constitution mauritanienne et des engagements internationaux pris par notre pays, notamment :
la Convention de l’UNESCO de 2005 sur la protection et la promotion de la diversité des expressions culturelles, qui invite les États à favoriser le multilinguisme et à garantir l’accès à la langue des communautés dans les domaines de l’éducation, des médias et de l’administration.
le Pacte international relatif aux droits civils et politiques (article 27), qui reconnaît aux communautés linguistiques le droit d’« utiliser leur propre langue ».
la Charte africaine des droits de l’homme et des peuples (article 17), qui garantit à chaque peuple le droit à sa culture, à sa langue et à leur promotion.
Face à ce débat, qui pourrait engendrer des interprétations et confusions regrettables, nous, Coordination des Associations culturelles de langues, appelons à une politique linguistique inclusive, fondée sur la reconnaissance égale de toutes les langues nationales, dans un esprit de justice, de respect mutuel et de dignité partagée. Concrètement, cela implique :
1. l’officialisation effective du pulaar, du sooninke et du wolof, par une loi claire définissant leurs rôles, leurs domaines d’usage et les mécanismes concrets de mise en œuvre.
2. la généralisation rapide de l’enseignement dans les langues nationales à l’école fondamentale, comme recommandé lors des évaluations du BREDA/UNESCO en 1984, et par le ministère de l’Éducation nationale en 1988. Il s’agit là d’un levier essentiel pour une éducation de qualité, inclusive et équitable.
3. la promotion d’un multilinguisme équilibré, valorisant également les langues étrangères — notamment le français et l’anglais — comme outils de travail, d’apprentissage et d’ouverture sur le monde.
Nous sommes convaincus que la Mauritanie ne pourra bâtir une unité nationale durable qu’en respectant la dignité linguistique de toutes ses composantes. Officialiser l’ensemble des langues nationales, c’est affirmer en effet l’égale citoyenneté de tous les Mauritaniens.
La Coordination des Associations culturelles appelle donc à la mise en place d’une politique linguistique équitable, inclusive et progressiste, gage d’un avenir commun, de cohésion sociale et de paix durable.
Nouakchott, le 20 mai 2025
La Coordination